«Je vais… je m’engage… je ferai…» billaay sonn naniou si promesses yi. Le candidat de la continuité moom assume. Mais day dolli nieekh rek si tiéré Macky bi. Les autres promettent la rupture. Comme ndogou. Bon, c’est un pays quand même à jeun pour la démocratie et les libertés depuis quelques années. Nous avons eu droit à une rupture pourrie avec borom deukk bi. Et depuis les Législatives, c’est une «pourripture» à l’assemblée. Dog jotna si niniou gérer miim reew ! Walla ?
Emediasn
Askan wuy fal ay waay-ger, ay njub-lang ak sàcc ak i workat, kenn loru ko, mo nass loràngeem